- En tout cas, Maam Cheikh moo ñu ne "Maodo moo wax ni Keur Gui santoul Sy, Yallah la santt !" Moom mii mou wax ñou ne daffa am "maison avec des murs" et "maison sans murs". Di nga deuk ci Keur fekk yaag ñi deuk ci mbedd bee yam. Ñaati keur yii Bokkoul !!!
Maam Cheikh Wax na ñu yitt ne "Seriñ Babacar mo wax ni : Suma Maodo Jurroul woon, dou ma tee doon Khalifa Cheikh (Abboul Abas...s Ahmada Tijânī)". Loolou lañu meuss gueum ci moom mii ! Soudee Khalifa Cheikh, dou likko Al Maktoum jurr. Et puis ce n'est pas pour rien que mou Sañ wax ni : "Cheikh moo ko wax ni ko -Na nga Révolutionner sama Tariqa-". Ñun xam nañ ni Piccë bi (Satellite bi), Yagg nañ koo wax mou toppë ko mais moom moo lankë ndax wormaal kilifaam te beug moom #AlMaktoum dess fi nampal njaboott yi ba ca Kanama-Kanam. Kenneen kou wax ci kilifa Tariqa Tijâni ni Cheikh moo la charger "Révolution bii", te dou deug dou fanaan walla Yallah weer ko !!!
Te ñun waxou mala ni Maam Cheikh daañu degg-lou limou wax yeup (ci biti ñeup di degg) te japp ko mais mooy sunu -Directeur de Conscience-. Lou ñouy xalaat balaa ñoo wax, toloole ko ak kadoom ! Te loolou Yakaarou ma mou dañ abadann daa-iman ! Kou weddi li Serigne Moustapha donou, te Al Maktoum xamal ñu ko (Serigne, Chef de guerre et grand Patron), weddi nga AlMaktoum surtout boudee da ngay mbouboo "geum" Al Maktoum walla di ñoddi dereet !!!
Affaire bi daal, li ci leer mooy Dou mbirru dereet, depuis Hissa yonente Yallah Nouh A.S. meussoul nekk dereet. Même ci wallou Charī'a, fou dereet "genee" nekk sobbe même sou andeek leer. C'est un Commandement Divin. Rien que cela ne Vaille ! Deug leu Maam Cheikh neena nitt dina tollou ci loumou wax walla mou deff jurr contentieux mais farata rekk moo tax mouy wax nak... Ngirr Yallah ak Deug. Yaqiin la ci ñun. Askan waa ngi beugueu Alkou te fokk mou dougeul xalaatam ak looxoom ci li warra deffarou walla darra dou deffarou ci miim reew. Ci kanam lakko Ñeup di xam. Waxa goul darra sax, pour ñiy teup di dall, sou waxee ngeen dee benn yoon !!!
Bi ci dess mooy, #AlMaktoum sou dellou si woon ci ñun balla moo dellou ca Boroomam, ne ñu bayyi leen "Moustaf" (Al Mourchid) ("Le Choisi pcq Le Droit !"), Duñu ko bayyi Mouk ndax konn ñune daff ñouy seetlou walla mu weddi boppam. Te liñou seetlou te giss ko ci moom Maam Cheikh, mooy meussoul weddi boppam. Konn naka la Kennë kiko meunë donnou, Te donnou ko ci Diine, ci Tariqa ak ci Haqiiqa meuneu Weddee boppam ?! Meunoul nekk, ndax lou Yallah Doggal la ba noppi !!! Franchement, il faut au moins être logique quoi !!! FatabaarakAllah MachaAllah !!!
Ps : Maam Cheikh neena : "Nattou Allalou Joulitt la, Yeefeur moomou ko" ak "Toūma Allalou Gorr la, Saysay moomou ko". Koune ak sa Allal ! Kenn dou am yennë philosophie you toll nii ak gnou mell nii ci sa xoll ay vagabonds dilla wax safaanook la nga Japp ci ñoom mou dilla metti walla yeungeul. Deedeed ! Soxla wouñ darray Adouna feek ñou ngi lay am di la sentir sunu Xoll.
"Ce qu'il faut faire, ce n'est pas d'accabler les hommes par des sermons ; ce qu'il faut faire c'est de former des cœurs nouveaux que rien ne saurait détruire ; ce qu'il faut faire c'est de permettre aux hommes de devenir le symbole de la présence de Dieu sur terre." L'une de ses mérites est d'avoir concrétisé ces dires d'Al Maktoum !!!

C'est l'une des facettes de la Mission de Serigne Mouhamadou Moustapha Sy Al Mourchid (Le Droit)... dans notre pays de même que hors du pays depuis 40 ans.
Que ceux qui parlent sur lui en mal nous disent déjà, ce qu'ils ont fait pour le pays, ce qu'ils ont fait pour la Jeunesse et leurs parents, ce qu'ils ont fait Au Nom d'Allah. On pourra leur répondre après. Serigne Moustapha Sy a été à l'origine du Polissage de milliers d'âmes en perdition jusqu'à les munir de cœurs que rien ne saurait... détruire et c'est Al Maktoum qui en est le témoin. Aucun guide religieux n'a eu un tel témoignage en matière de réussite spirituelle : "Moustaf est-ce que xam nga ñaata rouh nga deffar ?... Mann fima toog xamnaa ko !"

Des cœurs aux esprits tranquilles et imperturbables qu'aucune langue fourchue comme celle des lieutenants d'Ibliss ne ferait fuir encore moins blessés parce que Avertis et pas par n'importe qui.
Aucune provocation ni aucune insulte ni aucune élucubration ne leur feront sortir de leur gonds mais surtout rien n'empêchera qu'ils assument leur Responsabilité en tant que citoyens qui participeront absolument au redressement de ce pays. Loolou Ken meunou leen ko tere ci souf sii !
Il faut surtout que le peuple sénégalais sache distinguer lorsqu'il y a des tohu-bohu dans l'opinion ceux qui parlent pour parler que pour eux et ceux qui n'agissent que pour la Reconnaissance divine !
Al Matoum neena :
Roy moo deffar Adouna !
Woujje moo yakk Adouna !
Te ñoo ndirroo mboubë !
Waaye bokku ñou lennë !
Mais les résultats ne seront jamais les mêmes... Mame Babacar Sy Al Khalif disait à ceux qui perturbaient sa mission : "Bou Sëtt yi ñëwee lepp Leer... " Sëtt yi ñëw nañ lepp leer na ci ku xamee te am degg !
Kou xool xamee ñiy Royy, ñiy Woujje ak ñiy Topadoo... ak ñi nga xamne beugou ñu topandoo mouy tax ñuy njeukee ! Wolof neeba Royy (walla Topandoo) Dou ndirook mouk PUR !
Le Combat continue ! Jarama Cheikh Mouhamadou Moustapha Sy Al Mourchidoul 'Aam !

0 commentaires:
Enregistrer un commentaire